Yok komptu imeel

Kenn liggéeyatul dara ci xët wii, kon ëmbiitam nekkatul bu bees.

Aplikaçion imeel moy yone bi gëne pour ligëy ak imeel ci sistemu Firefox. Leral bi dalàay xamal nakë nay yoke se imeel ci se aplikaçion koompte.

  1. Ubìl aplikaçion Imeelemail 1.3Nataal "email 1.4" amul.email 2.0 ci se aparey.
  2. Di ne gis ekranKoompte bu bes ci se ubì bu djëkk bu aplikaçion Imeel. duggàlal se tuur, adrès imeel ak kéréyé bàtu jal.
    email_setupemail_setup 2.0
    So gissul ekran bu Koompt bu bes bi, bësal ci raniewukay Orange FxOS button ci së tiamôñu ekran,

If you don't see the New Account screen, tap on the menu icon Orange FxOS button on the top left corner of the screen, topçi mandargawu parametar koompte Gray FxOS settings gear ci suuf ci së tiamonie, bësal Yokk Koompte.

  1. Bësal Bi ci top ngìr kéréyé së koompte imeel. Parè në lëp!
    Koompte POP3: So amè imeel koompte POP3, bësal ci yonu Konfiguraçion manuel. Ci suuf Tiip d Koompte, tanàl POP3+SMTP nge diekkali ci se informaçion koompte yüla së fuurnissër mèssageri bu POP3.

Ngir yenene xibar ci nakalë imeel di doxé, xolal Binde k yonè imeel ci sistemu Firefox.

Notes:
  1. S*ê telefòn warnë konektewu ci Internet ak Wi-Fi walë reso telefòn ngìr kéréyé së koompte.
  2. Aplikaçion imeel duulë màay nge kéréyé koompte imeel bu bes. Dafàlay rekk mày nge yokk koompte imeel bu àm be parè. So bëgge koompte imeel bu bes, ñu ngilày niane nge kéréyé koompte bu bes ci së site fuurnissër mèssageri bàla ngakay yokk ci së aplikaçion imeel.
  3. Fìmnè, bene fuurnissër site web biñuu atàne moy Hotmail, Yahoo ak Gmail. Mëne nge konfigure yenene koompte tamit ci k`w ne bës Konfiguraçion manuel ci ekran koompte bu bes.

These fine people helped write this article:

Illustration of hands

Volunteer

Grow and share your expertise with others. Answer questions and improve our knowledge base.

Learn More