Tambali ak sistému Firefox

Kenn liggéeyatul dara ci xët wii, kon ëmbiitam nekkatul bu bees.

Dalal ak jàmb ci sistemu Firefox! Leral bi dafày firì bëp maay te dinalë tahawu ngir ne tambali. Mingo ne tamit ak ay leral yoy mëna saytu benene yone

Konektewul!

Së telefon Firefox dafày ñiëw ak konekçion buy tax nge nekk en liñie so neke ci yòne. Mëne nge tamit konektewu ci reso Wi-Fi bi nge xamni faràl ne di gàw te donè yi nay jëriño fofù du bokk ak së konekçion reso operatër.

Ngìr konektewu ci reso Wi-Fi:

  1. Ubìl aplikaçion Parametar nge tàne Wi-Fi.
  2. Talal Wi-Fi bi so nopè ne bës ci reso bu ubeku ngir konektewu ci.

Pour yenene xibar, xolal Nakalày konektewo Wi-Fi ci sistemu Firefox.

Oùt ay aplikaçion yu bax

Bene, ci ay mbìir yu gëne ci nakala së smartfòn di amè ay aplikaçion yuy yombalàl së duunde. Sistemu Firefox amnë niarì yone pour dimbalilë ngë xam aplikaçion yi.

Jëli ak instale ay aplikaçion yuy jogé ci Marketplace bi

Aplikaçion Marketplace amnë bëp xetu aplikaçion yu xarañe yulày xaar. Gawaal saytu aplikaçion yû siiw, bes ak yu mingo ak jamono.

Marketplace Home

Pour yenene xibar ci Marketplace bi,xolal Nakalày jële ak instalè aplikaçion.

Seet bidì sopeku dafalày bayì ne rañié aplikaçion yu~u defaraat

Sistemu Firefox amnë lu yombëe jëfàandiko, seet bidì sopeku. Bindal rek bene bàat, bu melni "sushi" ngir nge rañie aplikaçion mobil yuuni mel. Yene ci aplikaçion yi sax dañuy jëfàandiko lu melni fi ne nek ngir mëna defaràat liñu laay wone.

  1. Bindal bene bàat ci penc seet bi.
  2. So parè nge bës ci bene aplikaçion ngiir ne ésséyéko san nge téléssargé ko walë instalé ko.

    Search appsadaptive search 2.0

Ngiir ne jaang bëp mbir bo mëna def ak li, xolal jëfàndiko Seet bibì sopeku ngiir rañie aplikaçion yiñu defaraat.


Jëli ak géré say Kontakt

Aplikaçion Kontact dafalày yombalaal wote walë méssage say niit.

  • Bësal buton mandarga biçi ruuk bi ci kaw ci së ndèy-diooru aplikaçion kontakt ngiir ne jëli say kontakt sissë karte SIM, Facebook, Gmail, Outlook (ak Hotmail) walë ci se karte mémoire.

    Import contacts introfirefox os contacts 2.0

Amnë yenene yu bàari yo mëna def - xolal jëli, yokk ak géré say kontakt ci sistemu Firefox

Jëfàandiko méssaj ngir di jokko

Aplikaçion message dafàlaay bayi nay yone ay méssaj yu gàt, natal ak wideo së ay xarit. Ngiir yone méssaj:

  1. Ubìl aplikaçion méssaj sms appmessages 2.0.
  2. Bësal button méssaj bu bes Editmessagesnew email 2.0 ngìr tambali.
  3. Ci penc A : mëne nge binde nimero telefon bu nit ki nge bëg yone méssaj bi walë nge bës ci buton kontakt contact buttonadd contact 2.0 ngìr yokk kène ci së aplikaçion kontakt.
  4. Aprè nge binde ci penc méssaj bi nge bës Yone so parewè send message 2.0 ngìr yone.

xolal Nakalàay jëfandiko aplikaçion Méssaj pour bëp détay.

Konfigiraçion imeel

Sistemu Firefox Firefox OS dafày jël koompte Gmail, Yahoo ak Outlook (ak Hotmail) ci fimuuy géné ci boitàam.

  • Ubìl rek aplikaçion I-meel bi nge dugaal së tuur, adéress imeel, batù jaal nge bës Biçi tòp. Li dess dafë automatik.

    email_setupemail_setup 2.0

Da ne bëg yenene leral ci imeel? xolal Binde ak Yone Imeel ci Sistemu Firefox


Def wëy ci së telefon

Yobu së mussik ak iow!

  1. Taalàl dintiuu USB/
    • Ubil aplikaçion Parametar, watial ci penc {dintie bimà gënal} ne bës Unite mémoire. Aparè, ci Unité d memoir, talaal dintiuu USB. Ubil Parametar aplikaçion yi, watiàl ci penc {dintie bimà gënal} nge tàal dintuu USB.
      USB 1.1usb storage 2.0
  2. Konekté se aparey ci se ordinatër ak bene kabal USB.
  3. Gilissel say wëy ci së karte memoire.
    Drag music Win7Drag music Mac

Mëne nge tamit jëli ay wëy ci se nawigatër walë jòotko ci Bluetooth. xolal Nakàlay defe music ci sama telefon sistému Firefox ngìr jàng nakala.

These fine people helped write this article:

Illustration of hands

Volunteer

Grow and share your expertise with others. Answer questions and improve our knowledge base.

Learn More